Tukki

Lyrics
Yoon wi nga j�l baaxul ku la koy dig�l da lay sax Yoon wii ci des moo g�n, loo taseel d�ldi koy m�n Yoon wii nga j�l booy dox ba ca biir g�stul xool fi nga weesu balaa ngay Booy tukki yaw Booy tukki yaw Na nga b�yyi ba m�n Ding c� j�l�� lu m�n� xew ca feneen Dina tax nga m�n xam nekkinu neneen Foofu m�n nga fa gis lu y�kk sa xameel Booy tukki yaw Nita ngi toog di janoog yaw booba fekk na ma ngay xalaat ba t�bbi asamaan �ndag niir yiy naaw dem na fu sore l�pp ciy xalaatam Yaw sama away kaay ma xamal la L��g l��g nga toog fi nga toog tukki tukki bu neex dem ba kaw asamaan �nd ag weer wiy naaw li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu g�n fee neex Booy tukki yaw Deel tukki yaw yeesal sa xameel Ding c� j�l�� lu m�n� xew ca feneen Dina tax nga m�n xam nekkinu neneen Foofu m�n nga fa gis lu y�kk sa xameel Deel tukki yaw L�ppa l�ppa s�mba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw Te l��g l��g mu dem ba kaaw Tukkee ka neex, waaw Lucum ceeli ma ngay naaw te l��g l��g mu naaw ba kaw Asamaan indi fiy xabaar Ku dul tukki doo xam fu d�kk neexe Booy tukki yaw Na nga b�yyi Booy tukki yaw Na nga b�yyi ba m�n Ding c� j�l�� lu m�n� xew ca feneen Dina tax nga m�n xam nekkinu neneen Foofa m�n nga fa gis lu y�kk sa xameel Booy tukki yaw Booy tukki yaw Booy tukki yaw Na nga b�yyi ba m�n Naanu barke ah naanu barke Nita ngi toog di janoog yaw booba fekk na ma ngay xalaat ba t�bbi asamaan �ndag niir yiy naaw dem na fu sore l�pp ciy xalaatam Yaw sama away kay ma xamal la L��g l��g nga toog fi nga toog tukki tukki bu neex dem ba kaw asamaan L�ng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom mu g�n fee neex Booy tukki yaw Na nga b�yyi ba m�n Ding c� j�l�� lu m�n� xew ca feneen Dina tax nga m�n xam nekkinu neneen Foofa m�n nga fa gis lu y�kk sa xameel Deel tukki yaw L�ppa l�ppa s�mba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw Te l��g l��g mu dem ba kaaw Tukkee ka neex, waaw Lucum c��li ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw �ndaaleel nu xabaar Tukkee ka neex, waaw
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...