Létt ma

Album cover art for "Létt ma" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Létt ma

2 Plays

Duration: 4:41

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Du nil, du nil b�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma Xamal ma lu leer Danga maa woolu sa g�ll e ma ��w nga mel ni xale Yaw daal yaw t�ppal f�le Danga ba di tappale Su fekkeeni parewoo waru loo di y�n�� Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe L�tt ma mbaa nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma L�g l�g sax nga y�nni ma Ma dem bay dem nga teye ma L��gi sax dematuma Damay ba� nga dug�l ma Bu fekkeeni parewoo wanu loo di y�n�� Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin �i di xeebe L�tt ma mbaa nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma Bari pexe weesuwul nettali sa g�ntu moroom B�gg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw Bari pexe weesuwul nettali sa g�ntu moroom B�gg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw L�tt ma mbaa nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma Boo ma waxee fi nga b�gg dem Ma wax la fi ngay jaar Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa B�gg naa nga l�tt ma walla book nga firi ma B�gg naa ko tay, ba� naa ko sub� kon xanaa ganaaw sub� b�gg ak ba� la . .

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Credits Not Found