Sportif

Album cover art for "Sportif" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Sportif

0 Plays

Duration: 3:25

View ArtistView Album

Lyrics

Woyal sa wayu ndam ii Dangay b�g�l sa xol bi Ndax yaa yor bannex bi Ni tay b�s bii sa b�s la Sa mb�r daan na k�ntaan nga Bu �u daanee sa mb�r nak Na nga fexe ba nee Po mii da�uy Jonante Faw mu am ku moyle Jarula defante, di xasteeka d��re Jonante po ag ree la Boo ga�ee fo ag ree la Boo ��kkee fo ag ree la L�pp ci fo ag ree la Bu� la ga�ee mu��l Boo ko ga�ee baalal B�g��n nga mu demee ni demewuko M�n naa am bu �ll�gee mu g�n fee neex Ba ma l�ng ag samay gaa yi ngir b�nneexu Xam ne lii fo la nii lay m�n� deme Powun jonante nii lay deme Tay jii yaw bu �ll�gee keneen la Fo ag ree de la� ciy jublu Moo tax �u wara dal taynangu defet Jonante po ag ree la Boo ga�ee fo ag ree la Boo ��kkee fo ag ree la L�pp ci fo ag ree la Bu� la ga�ee mu��l Boo ko ga�ee baalal Waa waaw wuy dabbee wuy yoo Dabi alaa ko ndey baate satata Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jig��n Sire la�u d��r bal g��r �a da �oo daw Sire B�lla moo �aan Ramata Faal Siree nga Cees Matee nga Njaar�m Du� ko w�y ku reew, du� ko w�y ku �aaw Aah wuy dabbee wuy yoo Dabi alaa ko ndey baate satata Jonante po ag ree la Boo ga�ee fo ag ree la Boo ��kkee fo ag ree la L�pp ci fo ag ree la Bu� la ga�ee mu��l Boo ko ga�ee baalal

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Credits Not Found