Xel

Album cover art for "Xel" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Xel

2 Plays

Duration: 4:51

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Faamara r�bbkat la woon Daa am bis mu xalli yoon Mu taxaw di xalaat ba mu y�gg mu s��n mb�tt miy daw Mu soqqat ci kanam ba di b�kku naan kii du ma raw Far mb�tt ma s��n kokoron D�ldi j�l bopp ba d�ldi koy ron Bopp ma n�bbuna li ci d�s yaramam w�pp di feen D�nn baag ndigg laag t�nk yaag yeneen ya l�pp di feen Lii tax nu defe ni mb�tt daa amul xel Kon nun nii Yalla jox xel nanu santati, nanu santati Li Yalla bind yep, nit la ci gene f�nk Mala yi li nu wuteleeg noom mooy sunu xel moo tax nuy def Looy dugg jiit�l�l sa xel ba loo ciy wut di nga gis nga ne Nin ni yor xel boo seetee noo yor �dduna Te yitam ku xalaat, ku misaal day mel ni mb�tt ma Nit moom xela ko yor Nit moom xela ko yor Nit moom xela ko yor Xela ko yor Li Yalla bind y�p, nit la ci g�n� f�nk Mala yi li nu wuteleeg noom mooy sunu xel moo tax nuy def Fimd��y nit mooy xel Soo ko amul y�ngi mel ne b�yyima Soo ko amul doo too nekk nit Li Yalla bind y�p, nit la ci g�n� f�nk Mala yi li nu wuteleeg noom mooy sunu xel moo tax nuy def Moo tax nuy def Waa waaw waa waaw waa waaw waa waaw Faamara r�bbkat la woon Daa am bis mu x�lli yoon Mu taxaw di xalaat ba mu y�gg mu s��n mb�tt miy daw Mu soqqat ci kanam ba di b�kku naan kii du ma raw Far mb�tt ma s��n kokoron D�ldi j�l bopp ba d�ldi koy ron Bopp ma n�bbuna li ci d�s yaramam w�pp di feen D�nn baag ndigg laag t�nk yaag yeneen ya l�pp di feen Lii tax nu defe ni m�tt daa amul xel Kon nun nii Yalla jox xel nanu santati, nanu santati Li Yalla bind y�p, nit la ci g�n� f�nk Mala yi li nu wuteleeg noom mooy sunu xel moo tax nuy def Moo tax nuy def Waa waaw loolu mooy xel, soo ko amul, soo ko amul Y�ngi mel ni b�yyima, y�ngi mel ni b�yyima, y�ngi mel ni b�yyima Looy dugg nang ko teg ci xel Faamara r�bbkat Mb�uuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Credits Not Found