Dabbaax

Lyrics
Keroog b�s p�nc ma ba nuy w�ja w�ccee j�nt bi Di waajal peese ba Mullaay Dabbaax Yalla nan la jege Yalla daal moyy t�nn waayam Mullaay Dabbaax Bu nu f�tte, b�s boobu le uhh Bu nu f�tte, b�s boobu le Bu nu f�tte, b�s boobu le Loo fa naan, Yalla mey la ko Moo daan waxal nu nuul ni Moo daan waxal nasaraan wi Moo daan g�ddu askan wi Dafa daan wax naan nan boole sunu r��w mi Dafa daan wax naan bu kenn y�ng�l gaal gi Dafa daan wax naan nan boole sunu xol yi Dafa daan wax naan nan y�r�m jig��n ni Sa boroom bi b�g na y�nnentam bi b�g na Yaa ko lig��yal sa boroom Mullaay Dabbaax yaw de w�cc nga m�ssoo wax lu amul Keroog ba nga nu jitoo asamaan si daa l�nd�m b�s� ngii kenn dootu ko f�tteeti Mullaay Dabbaax Bu nu f�tte, b�s boobu le Bu nu f�tte, b�s boobu le Bu nu f�tte, b�s boobu le Loo fa naan, Yalla mey la ko, anh! Moo daan waxal nu nuul ni, anh! Moo daan waxal nasaraan wi, anh! Moo daan waxal askan wi Dafa daan wax naan na nepp lig��y Dafa daan wax naan nan kenn j�ngal gune yi Dafa daan wax naan na nepp lig��y Dafa daan wax naan nan j�ngal jig��n ni Daawul seetaan lu naaw Pus��m la yoroon, fu x�tteeku mu naw R��w mi r��w mi ameel nan la njukk�l Mullaay Dabbaax Daawul seetaan lu naaw Pus��m la yoroon, fu x�tteeku mu naw R��w mi r��w mi ameel nan la njukk�l Mullaay Dabbaax Bakkariik Daramaa Maram Loo Kumba Caam Ngan P�ndaak Paate P�ndaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa Moo daan waxal nu nuul ni Moo daan waxal nasaraan wi Moo daan g�ddu askan wi Dafa daan wax naan nan yaatu sunu r��w mi Dafa daan wax naan na n�pp lig��y Dafa daan wax naan nan y�r�m jig��n ni Dafa daan wax naan nan j�ngal gune yi
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...