Sama G�mmu

Album cover art for "Sama G�mmu" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Sama G�mmu

0 Plays

Duration: 3:57

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Nanga def yaw sama g�mmu d�gg naa da nga yor xaalis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko �bb mbaa nga for ko Baal d��z��, eh Nanga def, na nga def g�mmu d�gg naa da nga yor xaalis Ba foo ma s��n t�mbaleey w�lis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko �bb mbaa nga for ko Baal d��z��, eh Yor xaalis m�nui tee me moom la Nanga def, na nga def g�mmu d�gg naa da nga yor xaalis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko �bb mbaa nga for ko Baal d��z��, eh Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko Foog nan nita ko waddal nga for ko Wax ma gaaw �aata la doon ma fay ko Man daal maay sa buur nangu ko Nanga def, na nga def g�mmu d�gg naa da nga yor xaalis Ba foo ma s��n t�mbaleey w�lis Xam naa ne yaw moomu loo ko Dang ko �bb mbaa nga for ko Baal d��z��, eh Ah su�uy maam noonu la� ko daan defee Ah su�uy baay noonu la� ko daan waxee Ah su�uy yaay noonu la� ko daan t�pee Ah g�mmu daal sama doomu nday nga E e e g�mmu daal suma xarit nga E e e g�mmu daal suma askan nga Ah su�uy maam noonu la� ko daan defee E e e g�mmu daal suma xarit nga E e e g�mmu daal man sama doomu nday nga E e e g�mmu daal man suma xarit nga E e e g�mmu daal yaw sama doomu nday nga Baal dooc moomu foo ko Teeyai teey teey Ah su�uy maam noonu la� ko daan defee Ah su�uy baay noonu la� ko daan waxee Ah su�uy yaay noonu la� ko daan t�pee E e e g�mmu daal sama doomu nday nga E e e g�mmu daal suma xarit nga E e e g�mmu daal suma askan

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Credits Not Found