Pullo Àrdo

Lyrics
Ku fi new mu j�ngal la Nax mi moo ko moom, ndox mi moo ko moom Daf ko d�nn Lii xar yi la, lii b�y yi la Nagam y�ngi, �ll b�ngi Baaxi maaman Pullo �rdo Ku fi new mu j�ngal la Nax mi moo ko moom, ndox mi moo ko moom Lii xar yi la, lii b�y yi la Nagam y�ngi, �ll b�ngi Baaxi maaman Pullo �rdo Pullo �rdo, Pullo J��ri, Pullo �rdo Pullo �rdo, Pullo J��ri, Pullo �rdo �rdo sex na g�nn�m D�ldi g�ddu yattam Ma nga �nd ag xaajam D�ldi jiit�l g�ttam Pullo J��ri, Pullo �rdo Mi ngi �nd ag xaajam D�ldi jiit�l g�ttam Dalal xelam, f��xal xolam Bu nu ni fo aka ree moom y�gu ko suuy Pullo �rdo, Pullo J��ri Y�ppam mu ngi fii Fii la yahoo, fi la m�ggee Te yit fii la takkee soxna L�ppam fii la Pullo �rdo, Pullo J��ri Bu nin ni t�b� ka dal moom y�gu ko Li mu am fii doyloo na ko doy doy loo na ko Bu dee oor la mbaa jamaan la Walla etaas la, mbaa abyong la, mbaa leneen la Moom gisu ko, Pullo �rdo Ma nga g�ddu toxooron Di mbiip mbiip mu am xorom Way, way yu amul moroom Mel ni kuy neexal goroom Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree Boo fa jaaree doon S�r��r ee di na la ree Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree Boo fa jaaree doon S�r��r ee di na la ree Di mbiip mbiip mu am xorom Way, way yu amul moroom Mel ni kuy neexal goroom Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree Boo fa jaaree doon S�r��r ee di na la ree Boo fa jaaree sant Saar ee di na la ree Boo fa jaaree doon S�r��r ee di na la ree
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...