B�jjan

Lyrics
Taasukat baa nga naan gainde gu waaf ca buntu k�r g�, di melastiku B�y bu am b�jjan du fa dem, Zacharia, b�jjan am na maanaa, wayal Lu la r��r ci sa cosaan, sa b�jjan xamal la ko Boo b�g�� xam sa cosaan, xam la fa maam yi b�yyi woon Deal seeti b�jjan ba, lu mu la ca wax, du den B�jjana xam Kajoor ah ba ca mbeneex wa Cosaani askan wi, b�jjan am na maanaa Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, sungun sangan b�jjan, b�jjan Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, b�jjan, b�jjan, sungun sangan Neenanu mag de m�t naa ba cim r��w waaye b�jjan it m�t na b�yyi ci biir k�r Xam sa boppa g�n nu woo la naan kii nga doon Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, sungun sangan b�jjan, b�jjan Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, b�jjan, b�jjan, sungun sangan Boo b�g�� xam sa cosaan, sa b�jjan moo la koy xamal Moo la naan awal fii, bul dem fee, defeel nii Boo ko seetloo dara du ca den Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, sungun sangan b�jjan, b�jjan Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, b�jjan, b�jjan, sungun sangan Mani b�jjan moodi magi baay walla rakkam Lu xew lune mane b�jjan taxaw Bu g��r dug�� n��gu g��r B�jjan taxaw, wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay B�jjan am na maanaa Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, sungun sangan b�jjan, b�jjan Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, b�jjan, b�jjan, sungun sangan B�jjan moodi magi baay walla rakkam Lu xew lune mane b�jjan taxaw Bu g��r dug�� n��gu g��r B�jjan taxaw, wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay B�jjan am na maanaa Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, sungun sangan b�jjan, b�jjan Wayum ter�nga la kuy b�jjan jogal y�ngu, b�jjan, b�jjan, sungun sangan
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...