Touba - Daru Salaam

Album cover art for "Touba - Daru Salaam" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop, Wolof

Touba - Daru Salaam

0 Plays

Duration: 5:50

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Touba Daaru Salaam Nan farlu gaaw te dem naani paas Bii waruwaay gacceelna jaas Du roppelaan te it du naas Ku weddi laajal meer ya ca Faas Touba Daaru Salaam Gawal ni kon nga ubbi aas Moo gen Moo gen nga toog ba naan xalaas Sakkul ma lii ndax de du jaas Jar nay fanaan Marse Okaas Allah Touba Daaru Salaam Soobul te ban diko cokaas Bindul te gaaw japp palaas La dale fii ba ca Gosaas Jazaabul xuloob mooy seen bagaas Ku mel ni noom de am nga chance Cheikhoul Khadim a gen licence Sedd sedd menul weesu galaas Cey jile waay amufi maas Touba Daaru Salaam Ku begg raw tannal sa fas Te bana jaar fu am taxas Ndem begguloo lu la laxas Jebbalujil te wutt njaxas Li am ci daayira ca France Lim la bu kenn menul xiyaas Foo dem ningi conference Bamba di dem ku begg raas Taalibe yaanga Casamance Bile courant fеpp la maas Maggal amul aje ki aas Ku xasa dem nooy ni patasse Touba Daaru Salaam Ku bеgg raw tannal sa fas Te bana jaar fu am taxas Ndem begguloo lu la la Jebbalujil te wutt njaxas

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour