Bamba the Poet

Album cover art for "Bamba the Poet" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop, Wolof

Bamba the Poet

0 Plays

Duration: 3:51

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Ahmadou Bamba yeemnama Man de, waarunaa ci Bamba Man de, yeemunaa ci Bamba Li mu bind ci ay teere, gisaguma ku ko jege Man, li ma gis nit kese mënuko Xanaa Bamba daawul nelaw Ni Modou Bamba warna jaaxal kuy bindkat Modou Bamba warna yeem kuy woykat Reewi arab, reewi tubaab ak reewi nit ku nuul Booleen were banu daj Mennaa waat ni doo fa gis ku mel ni Modou Bamba Man de, yeemunaa ci Bamba Ci alxuraan la Bamba jaare Araaf bu ne defna ci teere Kenn bindle lu ni yeene Xanaa Bamba daawul nelaw Ahmadou Bamba yeemnama Li mu bind suul ci biir suuf Li mu bind sanni biir geej Eppna fuuf li mu feenal Xanaa sen bi daawul nelaw Man de, yeemunaa ci Bamba Ndem bëgg nga xam sa diine jangal xasaayid yi Ndem bëgg nga xam sa boroom jangal xasaayid yi Wer gu yaram, koom koom ak barke lëppangi ci xasaayid yi Nun, li nu am na nu ko ne cass Wer adduna di ko tiitaroo Man de, yeemunaa ci Bamba Li mu bind suul ci biir suuf Li mu bind sanni biir geej Eppna fuuf li mu feenal Xanaa sen bi daawul nelaw Xanaa Bamba daawul nelaaw

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour