Yaru

Album cover art for "Yaru" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Yaru

2 Plays

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Ah nit ku reew la mu yor moomu ko Su la mu yor waddee ku yaru mooy for jarinoo Ah yaral sa doom ci bi muy guneel Xaleel ca tuutaay ba nga koy doora yer Wuy mbooloo wuy mbooloo Mbooloo mooy doole Wuy mbooloo mooy sa doole Mbooloo jammi reew la Aziizoo Njaay lu yagg degg la yaay yaw xam nga loolu Aziizoo Njaay du yagg ba ngay naaw man gem naa loolu Wiiri wiiri jaari ndaare Aziizoo Njaay doomu ndeyu Useinu Njaay sunu waaji Aziiz li la yengel bu dee degg la ci yaw jafandul mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Bu ca reel bu ca yekkeki noddil mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Bu dee degg gu degg te deggentuwul noddil mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Wuy mbooloo wuy mbooloo Mbooloo mooy doole Wuy mbooloo mooy sa doole Mbooloo jammi reew la Aziizoo Njaay du yagg ba ngay naaw man gem naa loolu Ndax Aziiz xam nga ne degg du daw te degg moom du toxu Degg du nax saay degg yi amoon daaw am fi daaw jeeg Degg degg rekk moo fiy daw ba tay Ku lay begg na la begg ci degg Ku lay ban it na la ban ci dеgg Ba bu degg newee fekk la nga toog ci dеgg Li la yengel bu dee degg la ci yaw jafandul mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Bu ca regel bu ca yekkeki noddil mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Bu dee degg gu degg te deggentuwul noddil mu deger Wiiri wiiri jaari ndaare Wuy mbooloo wuy mbooloo Mbooloo mooy doole Wuy mbooloo mooy sa doole Mbooloo jammi reew la

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour
  • Kabou Gueye
  • Habib Faye