Moor Ndaje

Lyrics
Te sax adduna kenn du ko dajal, ku dul umpele danu lay ragal Faww nit ku ne am lu muy desal ngir bu ellegee nu men laa setal Fu ne nga nekk fa Lu ne nga dugg ca Heh heh begg naa nga dal Yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Woo yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Lekkoo ci ndap li begg ci xepp suuf Lekkoo ci ndap li ngall bu ci xepp suuf Woo yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Boo ci lekkul it bu ko xan keneen Kanaan fankul muur Yalla mood meye Woo yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Menaguma dem waaye keneen du dem Xamal ni bu yoon jeexul waaxusil du jeex Woo yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Faww nit ku ne am lu muy desal Degg degg daal di nga raw Woo yoo Moor Ndaje deel sooraale ellek Boo moytuwul yaw lanuy riinion Television yi ag rajo yi sax am na lu nuy umpele Waaye fleme mbooloo ni afiisu sinemaa Moor jamais rate Moor wannil ma sa gallaac Boo moytuwul yaw lanuy riinion Xawma mbaax la xawma den kumpe la Moor Ndaje Xawma mbaax la xawma den kumpe la Moor Ndaje Yaw menuloo jef sax ba kenn woolula Moor Ndaje Boo moytuwul sax yaw lanuy riinion Moor Ndaje Boo moytuwul sax yaw lanuy toogee Moor Ndaje Yoo, Yee Moor Ndaje Wuy yoo, wuy yee Moor Ndaje
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...
Credits
- Writers
- Youssou N’Dour
- Kabou Gueye
- Habib Faye