Sagal Ko

Album cover art for "Sagal Ko" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Sagal Ko

2 Plays

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko de xamul ku dul yaw Xale bi ndeyam ba na ko, baay ba ba na ko te gisoo ci dara Xarit na nga regle Xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari Yerem ko, sagal ko Xale bi ndeyam ba na ko, baayam ba na ko te seetoo si dara Xarit na nga regle Xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari Yerem ko, sagal ko Jef joo gis am na pay Jef ju baax am na pay waaye jef ju bon it am na pay Xarit seetaatal bu baax ni ngay doxalee Xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko te xamul ku dul yaw Na nga regle Xarit te nga xam ni, xarit Na nga regle Xarit te nga xam ni Xarit te nga xam ni, xarit Te nga xam ni, xarit Na nga regle, xarit Te xam ni adduna de jaru ko Geestul sa ginnaaw Yerem ko, sagal ko

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour
  • Kabou Gueye
  • Habib Faye