Mbëggéél Noonu La

Lyrics
Ku ne langal ag sa waay, bu neexee du metti, mbeggeel nooonu la Naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am Naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am Wuy mbeggeel Ooh! Ku ne langal ag sa waay, bu neexee du metti, mbeggeel noonu la Lu ne ngi ci biir mbeggeel bul di bare looy seetlu mbeggeel noonu la Naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am Naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am Wuy mbeggeel Ooh! Aah Jali ni la mbeggeel di def saa boo yewwoo te doo ci men dara Waaw Jali su dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol Kaay ma digel la bul seentu sa ginnaaw aah Waaw Jali su dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol Ma digel la bul seentu sa ginnaaw aah Xoolal ci sa kanam moo gen Naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am Naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggela am Wuy mbeggeel Aah ki nga begg mu begg la bul di xool leneen di leen yamalе Langal ag sa waay Ku ne langal ag sa waay Aah ki nga begg mu begg la bul di xool lеneen di leen yamale Ku ne langal ag sa waay Wuy mbeggeel Bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol Ma digel la bul geestu Ah ku ne langal ag sa waay Buy neex ag buy metti, mbeggeel noonu la Ah mbeggeel Bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol Ma digel la bul geestu Aah langal ag sa waay Bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol Ma digel la bul geestu
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...
Credits
- Writers
- Youssou N’Dour
- Kabou Gueye
- Habib Faye