Ballago ndumbé yatma

Lyrics
Billaay , ballago ndoumbé yatma Su ñu waaji xaj oon na fi Naxxar doηη ,la ñu bayyee Yalla , wonneeti na Li tax ba mbir mi metti lool Ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gnou Billaay wéetël na ñu Njiinoo njiin faramaareen Gòor u jaaga , nelaw naa Baay i wally dem na nii Ñun daal wéetël na ñu Ma ngi koy jaale Sénégal Di ko jaalé Gambia Di ko jaalé adduna Ndaanaan ba dem na nii Thione ballago , ndoumbé yatma Bu yalla buur bi doon taggoo Kon di na ñu bayék yaw Ni patrimoine bi nga ñu bayyeel Yee gua nit gñi , tete leen ci adduna Yee gua nit gñi , tete leen Xam al leen ci adduna Ahhh - Ballago Yee gua nit ñi ci adduna xam al leen Ni ñu war a nekkek Ak ni ñu war a dundée Ak ni ñu war a jëfleentee Jinaxoo mbaay Yaw mi dëkké biir suuf Boo dem ee neel ballago , réew maa ngi koy joy Aduna ngi koy jooy Art baa ngi koy jooy Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Li tax ba mbir mi metti lool Ñun da ñu ko foog wul woon Yëf yi gaaw ba bette gno Ndanaan ba demna ni Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thione seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thionе seck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo Njiin faramaareen Thione sеck , wéetël na ñu Ballago ndumbé yaatma Adduna , amul solo
Rate this song
0/5.0 - 0 Ratings
Loading comments...
Credits
- Writers
- Youssou N’Dour