Mahdiyu Laye

Album cover art for "Mahdiyu Laye" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop, Wolof

Mahdiyu Laye

0 Plays

Duration: 3:55

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Bu de dangay leble Lebleelal ku am pey Seydina Limamou Yalla feyna ko Neent fukki at ya Mohammed woote Neent fukki at ya Maam Limamou woote Mahdiyu Laye Mohammed waxoonna Mahdiyu gi ci yoon wi Seydina Limamou Feen ca tefes ga And ak Issa Maami Maam Rane Laye Moo niwoon geej ga Yow xamnga maay kan Bëgg naa nga dellu Ca la geek ga delloo, Laye Keroog la woote Adjiboo daayirahi Kaayleen, kaayleen Nowleen, dikleen Jaamu lamul ahzam Laye Moo dellusee, moo dellusee Moo dellusee, Mahdiyu Laye, moo dellusee Baayi Issa Laye Baayi Mandione Laye Ak Ababacar Laye Maami Maam Rane Laye Ak Ablaye Thiaw Laye
Laye Maami Ousseynou Laye Mahdiyu feenna Sagalnga reew mi Neppangi naan Laye Yaa and ak Issa
Laye Yaa dellusee, yaa dellusee Yaa dellusee, Maam Limamou, yaa dellusee Yaa dellusee, xammenan la, yaa dellusee Yaa dellusee, Mahdiyu Laye, yaa dellusee

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour