Li Ma Weesu

Album cover art for "Li Ma Weesu" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop

Li Ma Weesu

0 Plays

View ArtistView Album

Lyrics

Li ma dundee li ma weesu day dellusee mel ni seetu Seetal leeg leeg ma geestu ci li ma weesu Leeg leeg ma reccu walla sax di bakku Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma begg leenoo Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma magg Lu ma gen di yagg, xel mi mel ni bank Lu me gen di magg, dellu tuuti tank Li ma dundee li ma weesu day dellusee mel ni seetu Mani seetal leeg leeg ma geestu ci li ma weesu Leeg leeg ma reccu walla sax di bakku Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma begg leenoo Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma magg Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma begeti Lu ma gene jege mel ni dama sore Lu ma gene sore gen di gis li ma jegewoon Lu ma gen di yagg, xel mi mel ni bank Lu me gen di magg, dellu tuuti tank Li ma dundee li ma weesu day dellusee mel ni seetu Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma magg My past always comes back as in a mirror Sometimes I look back to my past life With regret or pride When I'm around the children I love, they dance and I guide them and I express myself in such a way that I want to be a Child again and never grow older The longer I stay away, the more forgetful I am The older I grow, the more I look back to the past and want to be a child again My past always comes back as in a mirror Sometimes I look back to my past life With regret or pride When I'm around the children I love, I feel happy again They dance, I guide them and express myself in such a way that I want to be a child again and never grow older The closer I am, the farther I feel The farther I am, the closer I feel The longer I stay away, the more forgetful I am The older I grow, the more I look back to the past and want to be a child again My past always comes back as in a mirror

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour
  • Kabou Gueye
  • Habib Faye
  • Max Calò