Gagganti ko

Album cover art for "Gagganti ko" by Youssou N’Dour

Youssou N’Dour - Pop, Senegal

Gagganti ko

0 Plays

Duration: 3:41

View ArtistView Album

Lyrics

Language:

Ba �u la koy jox, xam ul dara; Bu la s�en �e, daw gatandu la Ay waajur �m, da �oo am oon yaakaar ci yaw Jamono y dox, jafejafe am, s�ytaane ��w Bu ko d�or, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu �aaw Delloo l sa xel, ca ginnaaw, te mu� �l ko; Ba �u la koy may, xam ul dara;; Bu la s�en �e, daw laxasu la Ay waajur �m, da �oo am oon yaakaar ci yaw Jamono dox, jafejafe am, s�ytaane ��w Bu ko d�or, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu �aaw Delloo l sa xel, ca ginnaaw, bu ko souffrir loo; Xool al ci ay, waajur �m, bu ko joy loo Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Bu ko d�or, bu ko saaga, bu ko xas Bu ko wakh lu �aaw Bu y�ngg�l �e daal, ba sa xol fees, g�nn �l nga dem Bu fa toog yaw, di raak ak moom, s�mm al sa c�r Woo ko, waxtaan ak moom, t� mu��l ko Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Bu juum ee gagganti ko Yaw tam, bul forcer, deel n�gocier Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier Te bu am ee, lu fi leer ul, nga clarifier Coow li, bu d�border, nga pacifier Yaw daal, bul forcer, deel n�gocier Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier Te bu am ee, lu fi leer ul, nga clarifier Coow li, bu d�border, nga pacifier Wa waaw Jaaj�f, di na tax, xale wone jom Waaw g�or, di na tax, xale yokk jom Di ko won sa jom, moo koy dolli jom Jom jom jom rek, dara lu dul jom Y�r�mal ma ko Momit mou w�gal ma laa Nax ko neex al ma ko Moomit mu xam ko

Rate this song

Rate this song

0/5.0 - 0 Ratings

5
0.0% (0)
4
0.0% (0)
3
0.0% (0)
2
0.0% (0)
1
0.0% (0)

Loading comments...

Credits

Writers
  • Youssou N’Dour